Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 16:16-18 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 16:16-18 in Kàddug Yàlla gi

16 Wutal xel mu rafet, bàyyi wurus; taamul ag dégg, wacc xaalis.
17 Yoonu kuy jubal day moyu lu bon, ku teeylu sa jëfin, sàmm sa bakkan.
18 Réy, yàqule; xeebaate, jóoru.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi