Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 15

Kàddu yu Xelu 15:8-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Saraxub ku soxor, Aji Sax ji bañ na ko; ñaanu kuy jubal da koy bége.
9Jëfi ku bon, Aji Sax ji seexlu na ko; ku sàlloo njekk, safoo na la.
10Mbugal tar na, ñeel ku wacc yoon; ku bañ waxi àrtu, dangay dee.

Read Kàddu yu Xelu 15Kàddu yu Xelu 15
Compare Kàddu yu Xelu 15:8-10Kàddu yu Xelu 15:8-10