Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 15:8-10 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 15:8-10 in Kàddug Yàlla gi

8 Saraxub ku soxor, Aji Sax ji bañ na ko; ñaanu kuy jubal da koy bége.
9 Jëfi ku bon, Aji Sax ji seexlu na ko; ku sàlloo njekk, safoo na la.
10 Mbugal tar na, ñeel ku wacc yoon; ku bañ waxi àrtu, dangay dee.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi