Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 15

Kàddu yu Xelu 15:32-33

Help us?
Click on verse(s) to share them!
32Xalab waxi yar, foye sa bopp la; deel déggi àrtu, yokk sam xel.
33Ragal Aji Sax ji day rafetal xel; jëkke woyof, mujje tedd.

Read Kàddu yu Xelu 15Kàddu yu Xelu 15
Compare Kàddu yu Xelu 15:32-33Kàddu yu Xelu 15:32-33