Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 15:32-33 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 15:32-33 in Kàddug Yàlla gi

32 Xalab waxi yar, foye sa bopp la; deel déggi àrtu, yokk sam xel.
33 Ragal Aji Sax ji day rafetal xel; jëkke woyof, mujje tedd.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi