Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 15

Kàddu yu Xelu 15:14-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Ku am ug dégg sàkku xam-xam, ab dof di toppi caaxaan.
15Xol bu tiis, naqar wu sax; xol bu neex, bànneex bu sax.
16Néewle te ragal Aji Sax ji moo gën barele, sa bopp ubu.

Read Kàddu yu Xelu 15Kàddu yu Xelu 15
Compare Kàddu yu Xelu 15:14-16Kàddu yu Xelu 15:14-16