Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 15:14-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 15:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Ku am ug dégg sàkku xam-xam, ab dof di toppi caaxaan.
15 Xol bu tiis, naqar wu sax; xol bu neex, bànneex bu sax.
16 Néewle te ragal Aji Sax ji moo gën barele, sa bopp ubu.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi