Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 15

Kàddu yu Xelu 15:12-15

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Kuy ñaawle buggul ku ko àrtu, te du laaji ku rafet xel.
13Xol bu sedd, kanam gu leer; xol bu tiis, boroom ne yogg.
14Ku am ug dégg sàkku xam-xam, ab dof di toppi caaxaan.
15Xol bu tiis, naqar wu sax; xol bu neex, bànneex bu sax.

Read Kàddu yu Xelu 15Kàddu yu Xelu 15
Compare Kàddu yu Xelu 15:12-15Kàddu yu Xelu 15:12-15