Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 15:12-15 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 15:12-15 in Kàddug Yàlla gi

12 Kuy ñaawle buggul ku ko àrtu, te du laaji ku rafet xel.
13 Xol bu sedd, kanam gu leer; xol bu tiis, boroom ne yogg.
14 Ku am ug dégg sàkku xam-xam, ab dof di toppi caaxaan.
15 Xol bu tiis, naqar wu sax; xol bu neex, bànneex bu sax.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi