Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 14

Kàddu yu Xelu 14:32-34

Help us?
Click on verse(s) to share them!
32Coxor detteel boroom; ku jub fegoo maanduteem.
33Kuy dégg, sam xel saxoo rafet; ab dof sax xam na lu xelu.
34Njekk day teral aw xeet, moy di gàcceel aw askan.

Read Kàddu yu Xelu 14Kàddu yu Xelu 14
Compare Kàddu yu Xelu 14:32-34Kàddu yu Xelu 14:32-34