Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 14:32-34 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 14:32-34 in Kàddug Yàlla gi

32 Coxor detteel boroom; ku jub fegoo maanduteem.
33 Kuy dégg, sam xel saxoo rafet; ab dof sax xam na lu xelu.
34 Njekk day teral aw xeet, moy di gàcceel aw askan.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi