Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 14

Kàddu yu Xelu 14:3-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Ab dof a ngi réy-réylu, làmmiñam yar ko; ku rafet xel, sa kàddu aar la.
4Su yëkk takkul, bey, sàq wéet; mu beye dooleem, meññeef ne gàññ.
5Seede bu dëggu, dëgg rekk, seede bu dëgguwul, fen rekk.
6Ab ñaawlekat day wut xel mu rafet, mu réer ko; ku am ug dégg, xam yomb la.
7Dàndal ab dof, du la yokk xam-xam.

Read Kàddu yu Xelu 14Kàddu yu Xelu 14
Compare Kàddu yu Xelu 14:3-7Kàddu yu Xelu 14:3-7