Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 13

Kàddu yu Xelu 13:8-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Ku am ay fey alal, ba mucc; ku amul deesu ko tëkku.
9Ku jub day leer nàññ, ab soxor mel ni taal bu fey.
10Réy-réylu jote rekk lay jur, ku dégg ndigal a xelu.

Read Kàddu yu Xelu 13Kàddu yu Xelu 13
Compare Kàddu yu Xelu 13:8-10Kàddu yu Xelu 13:8-10