Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 13:8-10 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 13:8-10 in Kàddug Yàlla gi

8 Ku am ay fey alal, ba mucc; ku amul deesu ko tëkku.
9 Ku jub day leer nàññ, ab soxor mel ni taal bu fey.
10 Réy-réylu jote rekk lay jur, ku dégg ndigal a xelu.
Kàddu yu Xelu 13 in Kàddug Yàlla gi