Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 13

Kàddu yu Xelu 13:17-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17Ndaw lu bon day loru. Ndaw lu wóor garab la ci nit.
18Ku sàggane yoonu yar, séddoo ñàkk ak gàcce; kuy déggi àrtu, am teraanga.
19Aajo ju faju tooyal na xol, te ab dof jomb naa dëddu mbon.
20Àndal ak ku xelu, sam xel rafet; ku lëngook ub dof, loru.
21Ay topp na moykat, ku jub juble.

Read Kàddu yu Xelu 13Kàddu yu Xelu 13
Compare Kàddu yu Xelu 13:17-21Kàddu yu Xelu 13:17-21