Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 13

Kàddu yu Xelu 13:15-19

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Dangay xam lu jaadu, ñu naw la; yoonu workat day metti.
16Képp ku teey jëfe xam-xam; ab dof ay siiwal ndofam.
17Ndaw lu bon day loru. Ndaw lu wóor garab la ci nit.
18Ku sàggane yoonu yar, séddoo ñàkk ak gàcce; kuy déggi àrtu, am teraanga.
19Aajo ju faju tooyal na xol, te ab dof jomb naa dëddu mbon.

Read Kàddu yu Xelu 13Kàddu yu Xelu 13
Compare Kàddu yu Xelu 13:15-19Kàddu yu Xelu 13:15-19