Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 13:15-19 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 13:15-19 in Kàddug Yàlla gi

15 Dangay xam lu jaadu, ñu naw la; yoonu workat day metti.
16 Képp ku teey jëfe xam-xam; ab dof ay siiwal ndofam.
17 Ndaw lu bon day loru. Ndaw lu wóor garab la ci nit.
18 Ku sàggane yoonu yar, séddoo ñàkk ak gàcce; kuy déggi àrtu, am teraanga.
19 Aajo ju faju tooyal na xol, te ab dof jomb naa dëddu mbon.
Kàddu yu Xelu 13 in Kàddug Yàlla gi