Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 13

Kàddu yu Xelu 13:13-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Ku sofental ndigalu Yàlla, yàqule; ku jëfe santaane Yàlla, yoolu.
14Njàngle mu xelu day suuxat bakkan, ba boroom du tàbbi ci fiiri ndee.

Read Kàddu yu Xelu 13Kàddu yu Xelu 13
Compare Kàddu yu Xelu 13:13-14Kàddu yu Xelu 13:13-14