Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 13:13-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 13:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Ku sofental ndigalu Yàlla, yàqule; ku jëfe santaane Yàlla, yoolu.
14 Njàngle mu xelu day suuxat bakkan, ba boroom du tàbbi ci fiiri ndee.
Kàddu yu Xelu 13 in Kàddug Yàlla gi