Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 13

Kàddu yu Xelu 13:1-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Doom ju xelu dégg yaru baay, kuy ñaawle faalewuli àrtu.
2Wax ju rafet yool na boroom, workat fitna la namm.
3Moom sa làmmiñ, sàmm sa bakkan; rattaxle, yàqule.

Read Kàddu yu Xelu 13Kàddu yu Xelu 13
Compare Kàddu yu Xelu 13:1-3Kàddu yu Xelu 13:1-3