Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 12

Kàddu yu Xelu 12:5-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Ku jub, yoon lay mébét; ab soxor di lal pexey wor.
6Ab soxor, waxam am tëru la, day reye; kàdduy kiy jubal di musle.
7Ab soxor bu daanoo, jeex na; ku jub, sa kër taxaw, ne këcc.
8Xel mu ñaw, jëw bu rafet; sam xel jekkadi, ñu xeeb la.

Read Kàddu yu Xelu 12Kàddu yu Xelu 12
Compare Kàddu yu Xelu 12:5-8Kàddu yu Xelu 12:5-8