Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 12

Kàddu yu Xelu 12:10-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Ku jub day topptoo ag juram, ab soxor néeg cig juram.
11Beyal sab tool, sab dund doy; topp ay caaxaan ñàkk bopp la.

Read Kàddu yu Xelu 12Kàddu yu Xelu 12
Compare Kàddu yu Xelu 12:10-11Kàddu yu Xelu 12:10-11