Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 12:10-11 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 12:10-11 in Kàddug Yàlla gi

10 Ku jub day topptoo ag juram, ab soxor néeg cig juram.
11 Beyal sab tool, sab dund doy; topp ay caaxaan ñàkk bopp la.
Kàddu yu Xelu 12 in Kàddug Yàlla gi