Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 11

Kàddu yu Xelu 11:18-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
18Coxor feyul boroom, day naxe; deel def njekk, sag pey wóor.
19Saxoo njekk, dund; sàlloo mbon, dee rekk.
20Aji Sax ji bañ na njublaŋ, safoo maandute.

Read Kàddu yu Xelu 11Kàddu yu Xelu 11
Compare Kàddu yu Xelu 11:18-20Kàddu yu Xelu 11:18-20