Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 11

Kàddu yu Xelu 11:15-19

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Bul gàddul kenn bor, di loru; bañ koo dige, daldi am jàmm.
16Jigéen, na yiw, ñu sagal ko; góor gu néeg, alal doŋŋ.
17Ku baax, boppam; ku bon, boppam.
18Coxor feyul boroom, day naxe; deel def njekk, sag pey wóor.
19Saxoo njekk, dund; sàlloo mbon, dee rekk.

Read Kàddu yu Xelu 11Kàddu yu Xelu 11
Compare Kàddu yu Xelu 11:15-19Kàddu yu Xelu 11:15-19