Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 11:15-19 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 11:15-19 in Kàddug Yàlla gi

15 Bul gàddul kenn bor, di loru; bañ koo dige, daldi am jàmm.
16 Jigéen, na yiw, ñu sagal ko; góor gu néeg, alal doŋŋ.
17 Ku baax, boppam; ku bon, boppam.
18 Coxor feyul boroom, day naxe; deel def njekk, sag pey wóor.
19 Saxoo njekk, dund; sàlloo mbon, dee rekk.
Kàddu yu Xelu 11 in Kàddug Yàlla gi