Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 10

Kàddu yu Xelu 10:26-28

Help us?
Click on verse(s) to share them!
26Ndaw lu tayel ca ka yónnee daa mel ni lu forox ciy gëñ mbaa saxar ciy gët.
27Ragal Aji Sax ji, gudd fan; soxor, gàtt fan.
28Ku jub day séentu mbégte, gis ko; ab soxor yaakaar, yàkki.

Read Kàddu yu Xelu 10Kàddu yu Xelu 10
Compare Kàddu yu Xelu 10:26-28Kàddu yu Xelu 10:26-28