Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 10:26-28 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 10:26-28 in Kàddug Yàlla gi

26 Ndaw lu tayel ca ka yónnee daa mel ni lu forox ciy gëñ mbaa saxar ciy gët.
27 Ragal Aji Sax ji, gudd fan; soxor, gàtt fan.
28 Ku jub day séentu mbégte, gis ko; ab soxor yaakaar, yàkki.
Kàddu yu Xelu 10 in Kàddug Yàlla gi