Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 10

Kàddu yu Xelu 10:24-25

Help us?
Click on verse(s) to share them!
24Ab soxor, li mu ragal moo koy dab; nammeelu ku jub day sotti.
25Bu ngëlén walee, ab soxor ne mes; ku jub, sab reen sax ba fàww.

Read Kàddu yu Xelu 10Kàddu yu Xelu 10
Compare Kàddu yu Xelu 10:24-25Kàddu yu Xelu 10:24-25