Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 10:24-25 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 10:24-25 in Kàddug Yàlla gi

24 Ab soxor, li mu ragal moo koy dab; nammeelu ku jub day sotti.
25 Bu ngëlén walee, ab soxor ne mes; ku jub, sab reen sax ba fàww.
Kàddu yu Xelu 10 in Kàddug Yàlla gi