Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 4

Ngën-gi-woy 4:4-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4sa loos wi ne coleet ni tatay Daawuda, mërgalu ba jekk, caq bay lang ni junniy kiiraayi jàmbaar.
5Sa ween yi ni ñaari tef, mbaa seexi kéwél yuy fore digg tóor-tóor yi.
6Balaa jant a fenk, ker gàddaay, ma ne coww diggante tund wa ndàbb ne bann, ak tund wa xas ma neexe.
7Xarit, sa lépp a rafet, sikk nekkul ci yaw.

Read Ngën-gi-woy 4Ngën-gi-woy 4
Compare Ngën-gi-woy 4:4-7Ngën-gi-woy 4:4-7