Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 1

Ngën-gi-woy 1:11-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
11Sàddi wurus lanu lay defaral, tapp ca xaalis.
12Li sama buur tëdd, di xéewlu lépp, maa ngi gilli lu neex.
13Sama nijaay di mbuusum ndàbb may fanaan sama digg ween.

Read Ngën-gi-woy 1Ngën-gi-woy 1
Compare Ngën-gi-woy 1:11-13Ngën-gi-woy 1:11-13