Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 1:11-13 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 1:11-13 in Kàddug Yàlla gi

11 Sàddi wurus lanu lay defaral, tapp ca xaalis.
12 Li sama buur tëdd, di xéewlu lépp, maa ngi gilli lu neex.
13 Sama nijaay di mbuusum ndàbb may fanaan sama digg ween.
Ngën-gi-woy 1 in Kàddug Yàlla gi