Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 9

Kàdduy Waare 9:4-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Képp kuy dund kat, am nga yaakaar, te xaj buy dund a gën gaynde gu dee.
5Kuy dund xam ne dangay dee, waaye ku dee xamul dara, te séentootul ab yool. Ku dee, ñu fàtte la.
6Muy sa cofeel, di sa mbañeel, ba ci sa kiñaan ànd ak yaw seey. Du lenn lu deeti sa wàll ci jépp jëfi kaw suuf.

Read Kàdduy Waare 9Kàdduy Waare 9
Compare Kàdduy Waare 9:4-6Kàdduy Waare 9:4-6