Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 9

Kàdduy Waare 9:4-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Képp kuy dund kat, am nga yaakaar, te xaj buy dund a gën gaynde gu dee.
5Kuy dund xam ne dangay dee, waaye ku dee xamul dara, te séentootul ab yool. Ku dee, ñu fàtte la.

Read Kàdduy Waare 9Kàdduy Waare 9
Compare Kàdduy Waare 9:4-5Kàdduy Waare 9:4-5