Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 9

Kàdduy Waare 9:16-18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
16Man dama noon xel mu rafet a gën doole! Ndeke ku néewle ñu xeeb la, tanqamlu say wax.
17Ku xelu, kàddoom yu dégtu ndànk moo gën ŋal-ŋalu kilifa ci biir ñu dofe.
18Xel mu rafet a gën ngànnaayi xare, waaye benn bàkkaarkat day yàq ngëneel lu réy.

Read Kàdduy Waare 9Kàdduy Waare 9
Compare Kàdduy Waare 9:16-18Kàdduy Waare 9:16-18