Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 8

Kàdduy Waare 8:7-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Kenn xamul luy xew ëllëg, kenn manula wax luy xew ëllëg.
8Kenn moomul bakkanam, ba man koo dese, kenn amul sañ-sañ ci bésub deeyam, kenn muccul ci boobu xare, te mbon du ca wallu boroom.

Read Kàdduy Waare 8Kàdduy Waare 8
Compare Kàdduy Waare 8:7-8Kàdduy Waare 8:7-8