Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 8

Kàdduy Waare 8:5-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Ku dégg ndigal doo am lu la soof. Ku xelu, xam lu jot, xam doxalin.
6Mbir mu mu doon kat ak jotam ak doxalinam, waaye nit am na tiis wu ko diis.

Read Kàdduy Waare 8Kàdduy Waare 8
Compare Kàdduy Waare 8:5-6Kàdduy Waare 8:5-6