Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 7

Kàdduy Waare 7:25-26

Help us?
Click on verse(s) to share them!
25Ma walbatiku, di jéema xam, di wut, di càmbar, di sàkkum piri, ngir xam li bon cig ndof, ak li dofe, cig ndof.
26Ma seetlu lenn lu gëna naqari dee: muy ndaw su la fiir. Kooku cofeelam mbaal la, yoxo ya dib jéng. Ku Yàlla gërëm a koy rëcc, bàkkaarkat bi lay jàpp.

Read Kàdduy Waare 7Kàdduy Waare 7
Compare Kàdduy Waare 7:25-26Kàdduy Waare 7:25-26