Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 6

Kàdduy Waare 6:8-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Ana lu boroom xel ëpplee ku dofe? Nga ñàkk, xam doxalin, lu mu lay jariñ?
9Doyloo li nga gis a gën di wéye xemmem. Loolu it, cóolóoli neen ak napp um ngelaw.
10Lu masa ay, dees koo tuddoon; lu doom aadama doon, xamees na ko, te kenn du layook ku la sut.
11Loo ci wax wax, solo sa gëna néew. Kon ana loo ci jële?

Read Kàdduy Waare 6Kàdduy Waare 6
Compare Kàdduy Waare 6:8-11Kàdduy Waare 6:8-11