Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 6

Kàdduy Waare 6:7-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Nit ak doñ-doñam jépp, biiram, te taxul mu doylu.
8Ana lu boroom xel ëpplee ku dofe? Nga ñàkk, xam doxalin, lu mu lay jariñ?

Read Kàdduy Waare 6Kàdduy Waare 6
Compare Kàdduy Waare 6:7-8Kàdduy Waare 6:7-8