Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 6

Kàdduy Waare 6:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Ku giir téeméeri doom, dund ati at, ak lu at ya bare bare, su bégewul teraanga ja mu am te amul njégu bàmmeelam sax, kooku lumb wu tuuroo ko tane.
4Lumb wa ñëw na moos ci neen, bàddoo lëndëm, turam sàngoo lëndëm.
5Gisul jant, xamu ko, waaye noflaay moo ko ëpple mag ma,

Read Kàdduy Waare 6Kàdduy Waare 6
Compare Kàdduy Waare 6:3-5Kàdduy Waare 6:3-5