Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 5

Kàdduy Waare 5:8-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Xanaa ndax buur suqal mbey mi, ba ñépp jariñoo suuf si.
9Bëggkatu xaalis du doyal xaalis, bëggkatu alal du doyal tono, te loolu it, cóolóoli neen.
10Bu koom yokkoo, lekk-kat yi yokku. Ana lu muy jariñ boroom koom ga, xanaa di ko duufale bëtam?

Read Kàdduy Waare 5Kàdduy Waare 5
Compare Kàdduy Waare 5:8-10Kàdduy Waare 5:8-10