Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 5

Kàdduy Waare 5:14-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Nga juddoo ci sa ndey loxoy neen, walbatiku dellu na nga dikke woon. Du dara loo ñaqoon ba yóbbaale ko.
15Dikke ni, delloo ni, loolu it tiis wu réy la. Doñ-doñi, ngelawal neen, ana jariñ la?
16Ngay dunde tiis bésoo bés, ak naqar ak wopp ak xol bu tàng!

Read Kàdduy Waare 5Kàdduy Waare 5
Compare Kàdduy Waare 5:14-16Kàdduy Waare 5:14-16