Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 5

Kàdduy Waare 5:12-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Naqar wu réy laa gis fi kaw suuf: Alal ju boroom dajale ba loru,
13mbaa pexeem moy, mu sànkule; ba bu amee doom it, du ko wacce dara.

Read Kàdduy Waare 5Kàdduy Waare 5
Compare Kàdduy Waare 5:12-13Kàdduy Waare 5:12-13