Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 5

Kàdduy Waare 5:11-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
11Surga, lekkam néew, bare, mu nelaw, ba fàttey boram; boroom alal regg, du nopplu, du nelaw.
12Naqar wu réy laa gis fi kaw suuf: Alal ju boroom dajale ba loru,

Read Kàdduy Waare 5Kàdduy Waare 5
Compare Kàdduy Waare 5:11-12Kàdduy Waare 5:11-12