Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 4

Kàdduy Waare 4:8-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Kenn a ngii, kenn ñaareelu ko, du doom, du mbokk. Doñ-doñam du dakk, te du doylu, mujj mu naan: «Kan laay doñ-doñil, di xañ sama bopp bànneex?» Loolu it, cóolóoli neen, di sas wu tiis.
9Ñaar a man kenn; doñ-doñoondoo, yoolu bu baax.

Read Kàdduy Waare 4Kàdduy Waare 4
Compare Kàdduy Waare 4:8-9Kàdduy Waare 4:8-9