Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 3

Kàdduy Waare 3:2-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Day jot nga juddu, mu jot nga dee; mu jot nga jëmbat, mu jot nga buddi.
3Mu jot nga rey, mu jot nga faj; mu jot nga toj, mu jot nga tabax.
4Mu jot nga jooy, mu jot nga ree; mu jot nga ñaawlu, mu jot nga dukkat.
5Day jot nga sànniy doj, mu jot nga dajale; mu jot nga fóon, mu jot nga baña fóon.
6Mu jot nga sàkku, mu jot nga ñàkk; mu jot nga sàmm, mu jot nga xalab.
7Mu jot nga xar, mu jot nga gaar; mu jot nga selaw, mu jot nga wax.

Read Kàdduy Waare 3Kàdduy Waare 3
Compare Kàdduy Waare 3:2-7Kàdduy Waare 3:2-7