Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 3

Kàdduy Waare 3:15-17

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Lu ay tey, ayoon na, lu ay ëllëg it ayoon na. Yàllaay namma indi la woon.
16Ma dellu gis fi kaw suuf ne, fu yoon moom, fa la njubadi ne, fa njub moom it, fa la njubadi ne.
17Saam xel ne ma, ku jub ak ku bon la Yàlla di boole àtte, ngir mbir mu ne ak jëf ju ne ak bésam.

Read Kàdduy Waare 3Kàdduy Waare 3
Compare Kàdduy Waare 3:15-17Kàdduy Waare 3:15-17