Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 3

Kàdduy Waare 3:12-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Ma gis ne nit amul lu gën bànneex ak jàmmi bakkan cig dundam,
13te nitoo nit, su dee lekk ak a naan, di ñaq, jariñoo, loolu mayu Yàllaa.
14Ma xam ne lu Yàlla def, loola day sax ba fàww. Deesu ci yokk, mbaa di wàññi dara; Yàllaa ko def, ngir nit di ko wormaal.

Read Kàdduy Waare 3Kàdduy Waare 3
Compare Kàdduy Waare 3:12-14Kàdduy Waare 3:12-14